Room 2:3-4
Room 2:3-4 KY
Yaw nit kiy sikk ñiy jëfe yooyii, te di ko def, ndax defe nga ne yaw ci sa bopp dinga rëcc àtteb Yàlla? Am dangay sofental mbaaxu Yàlla gu réy akug jéllaleem akug muñam, ndax ñàkka xam ne li Yàlla namm ci baaxe la, moo di nga tuub?





