Room 16:17
Room 16:17 KY
Léegi nag bokk yi, dama leen di ñaax, ràññeeleen ñi gàntal àlluwa ji ngeen jànge, di féewale aka téqtale, te ngeen moytu leen.