Peeñu ma 15:1
Peeñu ma 15:1 KY
Ma xoolaat, gisuma ci asamaan lu moy jeneen firnde ju màgg te yéeme: juróom ñaari malaaka yu taawu juróom ñaari musiba. Musiba yu mujj ya lañu nag, ngir ca la sànjum Yàlla di mate.