YouVersion Logo
Search Icon

Peeñu ma 12:9

Peeñu ma 12:9 KY

Ñu xalab ninki-nanka ju réy ja, jaanu cosaan joojee ñuy wax Tuumaalkat bi, di ko wax Seytaane, naxekatu mboolem àddina. Ci kaw suuf lañu ko xalab, mooki malaakaam.

Free Reading Plans and Devotionals related to Peeñu ma 12:9