Peeñu ma 12:12
Peeñu ma 12:12 KY
Kon nag yaw asamaan, bégal, yaak mboolem ñi ci sa biir! Waaye wóoy ngalla yeen, géej ak jéeri, yeen ñi Seytaane wàccaale mer mu tàng fi yeen, ndax xam ne fan yu néew a ko dese.»