Màndiŋ ma 22:31
Màndiŋ ma 22:31 KY
Aji Sax ji nag ubbi bëti Balaam, mu gis malaakam Aji Sax ja, mu taxaw ca yoon wa, xàcc saamaram. Mu ne gurub sukk, dëpp jëëm fa suuf.