Màrk 7:6
Màrk 7:6 KY
Yeesu ne leen: «Jinigalkat yi! Naaféq yi ngeen doon! Esayi yey na, ba mu jottalee kàdduy waxyu ci seen mbir, noonu ñu ko binde, ne: “Askan wii, làmmiñ lañu may wormaale, waaye seen xol sore na ma.