Luug 4:18-19
Luug 4:18-19 KY
«Noowug Boroom baa ngi fi sama kaw, ndax moo ma diw, fal ma ngir ma yégal néew-doole yi xibaaru jàmm bi. Moo ma yebal ngir ma yégal jaam yi, ne dees na leen jot, yégal gumba yi, ne dinañu gis, yégal ñi ñu noot, ne dees na leen goreel, tey yéene atum yiw wu Boroom bi.»





