Sarxalkat yi 26:5
Sarxalkat yi 26:5 KY
Dingeen bàcc ba keroog wittum reseñ jot te dingeen witt reseñ ba jamonoy ji jot. Dingeen lekk seenum pepp ba suur këll te dingeen dëkk ak jàmm ci seenum réew.