Yawut ya 8:8
Yawut ya 8:8 KY
Waaye Yàllaa sikk bànni Israayil, ba mu nee: «Ay fan a ngii di ñëw, la Boroom bi wax, mu ne maay fas ak waa kër Israayil ak waa kër Yuda, kóllëre gu yees gu bokkewul ak ga ma séqoon ak seeni maam,