Yawut ya 12:10
Yawut ya 12:10 KY
Sunuy baay a nu yar fan yu néew, na mu jaadoo woon ci seenum xel. Waaye sunu Baay bii, sunu njariñal bopp la nuy yare, ngir nu séddu ci sellaayam.