YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 45:4

Njàlbéen ga 45:4 KYG

Yuusufa dellu ne ay magam: «Jegeñsileen.» Ñu jegeñsi. Mu ne leen: «Man maay Yuusufa, seen rakk, ji ngeen jaayoon, ñu indi ma Misra.