Njàlbéen ga 25:32-33
Njàlbéen ga 25:32-33 KY
Esawu ne: «Man miy waaja dee ak xiif, ana lu ma céru taaw di jariñ?» Yanqóoba ne ko: «Giñal ma jëkk.» Esawu giñal ko ko, mu jaay Yanqóoba ndono li mu yeyoo ndax li muy taaw.