Mucc ga 39:32
Mucc ga 39:32 KY
Noonu la mboolem liggéeyu màkkaanu jaamookaay bi, maanaam xaymab ndaje mi mate. Noonee ko Aji Sax ji sante woon Musaa rekk, ni la ko bànni Israayil defe.