YouVersion Logo
Search Icon

Mucc ga 31:13

Mucc ga 31:13 KY

«Waxal bànni Israayil ne leen: “Fexeleen rekk ba sama bési Noflaay, ngeen di ko wormaal, ndax bésub Noflaay da di firnde sama digganteek yeen ak seen askan, ngir ngeen xam ne man Aji Sax ji maa leen ber, sellal leen.

Free Reading Plans and Devotionals related to Mucc ga 31:13