Mucc ga 25:8-9
Mucc ga 25:8-9 KY
Na ma bànni Israayil defaral béreb bu sell, ndax ma dëkk ci seen biir. Na lépp dëppoo ak li ma lay won. Muy misaalu xaymab jaamookaay bi, di misaalu mboolem ay jumtukaayam, lépp defeleen ko noonu.