YouVersion Logo
Search Icon

Mucc ga 24:12

Mucc ga 24:12 KY

Aji Sax ji waxati Musaa ne ko: «Yéegal ba ci man ci kaw tund wi te négandiku fa, ma jox la àlluway doj yi ak yoon wi, ak santaane yi ma ci bind ngir jàngale ko.»