Kolos 2:8
Kolos 2:8 KY
Moytuleen ba kenn bañ leena këfe kàdduy naxi neen yu ñu jàppe xam-xam bu xelu, kàddu yu sukkandikoowul ci Almasi bi, xanaa aaday nit ak mbiri àddina.