Jëf ya 9:4-5
Jëf ya 9:4-5 KY
Mu ne dàll ci suuf, daldi dégg baat bu ko ne: «Sóol, Sóol, lu tax nga di ma bunduxataal?» Mu ne: «Yaay kan Sang bi?» Mu ne: «Man maay Yeesu, mi ngay bunduxataal.