Jëf ya 9:15
Jëf ya 9:15 KY
Sang bi ne ko: «Demal, ndax kooku jumtukaay laa ko tànne, ngir mu xamali sama tur, xeeti jàmbur yi ak seeni buur, xamal ko itam bànni Israayil.