Bible App logo
Search Icon

Jëf ya 15:8-9

Jëf ya 15:8-9 KY

Yàlla mi xam xolu nit nag moo seedeel jàmbur ñi, ba mu leen mayee Noo gu Sell gi, ni mu nu ko maye nun itam. Yàlla amul xejj ak seen sunu dig ak ñoom, ndax seen ngëm la raxase seen xol.

Free Reading Plans and Devotionals related to Jëf ya 15:8-9