YouVersion Logo
Search Icon

1.Timote 2:5-6

1.Timote 2:5-6 KY

Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.

Verse Images for 1.Timote 2:5-6

1.Timote 2:5-6 - Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.1.Timote 2:5-6 - Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.1.Timote 2:5-6 - Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.1.Timote 2:5-6 - Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.1.Timote 2:5-6 - Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.1.Timote 2:5-6 - Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn rammukat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy kenn nit: muy Almasi Yeesu mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.

Free Reading Plans and Devotionals related to 1.Timote 2:5-6