1.Piyeer 3:3-4
1.Piyeer 3:3-4 KY
Seen gànjar bumu doon gànjaru biti bu yem ci ay létt yu rafet ak takkaayi wurus ak yére yu yànj, waaye nay lu làqoo jëmmu biir, nay gànjar gu dul jeex, te mooy lewetaay akug teey, ndax looloo réy njarte fa Yàlla.