1.Yowaan 4:3
1.Yowaan 4:3 KY
Waaye képp ku noo ga mu waxe waxloowul kàddu gu dëggal ne Yeesoo dikke yaramu suux, kooka noo ga muy waxe bokkul ci Yàlla. Googu noo mooy gu bañaaleb Almasi ba ngeen déggoon ne dina ñëw, te tey mu ngi ci àddina ba noppi.