1
Room 7:25
Téereb Injiil
TI
Maa ngi sant Yàlla; am na kuy musle, mooy Yeesu Kirist sunu Boroom. Kon nag lii laa gis ci sama bopp: ci sama xel maa ngi topp yoonu Yàlla, waaye ci sama bindu doom Aadama maa ngi topp yoonu bàkkaar.
Compare
Explore Room 7:25
2
Room 7:18
Ndaxte xam naa ne lu baax dëkkul ci man, maanaam ci sama bindu doom Aadama. Am naa yéeney def lu baax, waaye awma kàttanu yeggale.
Explore Room 7:18
3
Room 7:19
Lu baax nag lu may yéene, duma ko def, waaye lu bon lu ma bëggul, moom laay def.
Explore Room 7:19
4
Room 7:20
Bu fekkee nag lu ma bëggul, moom laay def, kon dootul sama coobare, waaye bàkkaar bi dëkk ci man, moo ma ci jiiñ.
Explore Room 7:20
5
Room 7:21-22
Gis naa nag lii: saa su ma bëggee def lu baax, lu bon a ngi ma taxawu. Ndaxte ci sama biir xol yoonu Yàlla wi neex na ma.
Explore Room 7:21-22
6
Room 7:16
Kon nag gannaaw li may def du sama coobare, nangu naa ne yoonu Musaa baax na.
Explore Room 7:16