1
Peeñu ma 18:4
Téereb Injiil
TI
Noonu ma dégg beneen baat bu jóge asamaan naan: «Génnleen ci biiram, yéen samay gaay, ngir ngeen baña bokk ci ay bàkkaaram te baña am cér ci musiba yi koy dal.
Compare
Explore Peeñu ma 18:4
2
Peeñu ma 18:2
Mu daldi xaacu naan: «Daanu na! Babilon mu mag ma daanu na! Léegi dëkkukaayu jinne la, ak bépp rab wu bon ak bépp picc mu daganul te araam.
Explore Peeñu ma 18:2