1
Peeñu ma 15:4
Téereb Injiil
TI
Ku la ragalul, Boroom bi? Ku dul màggal saw tur? Kenn, ndaxte yaw rekk yaa sell. Xeet yépp dinañu dikk, jaamu la, ndax say àtte bir na ñépp.»
Compare
Explore Peeñu ma 15:4
2
Peeñu ma 15:1
Noonu ma gis ca asamaan beneen firnde ju réy tey yéeme: juróom ñaari malaaka yu taawu juróom ñaari musiba, ñuy yu mujj ya, ndaxte ñoom ñooy matal merum Yàlla.
Explore Peeñu ma 15:1