1
Peeñu ma 1:8
Téereb Injiil
TI
Boroom bi Yàlla nee na: «Man Yàlla maay Alfa di Omega, Maay ki Nekk, di ki nekkoon démb, di kiy ñëw ëllëg, man Aji Man ji.»
Compare
Explore Peeñu ma 1:8
2
Peeñu ma 1:18
Maay Kiy Dund. Dee woon naa, waaye maa ngii di dund ba fàww, yor caabiy dee ak ju barsàq.
Explore Peeñu ma 1:18
3
Peeñu ma 1:3
Barkeel ngeen, yaw miy jàng ak yéen ñiy déglu wax yii jóge ca Yàlla, te di sàmm li ñu ci bind, ndaxte waxtu wi jege na.
Explore Peeñu ma 1:3
4
Peeñu ma 1:17
Naka laa ko gis, di daanu ci ay tànkam ni ku dee. Waaye mu teg loxol ndijooram ci sama kaw ne ma: «Bul ragal dara. Maay ki jëkk te maay mujj.
Explore Peeñu ma 1:17
5
Peeñu ma 1:7
Gisleen, mi ngi ñëw ci niir yi, te ñépp dinañu teg seeni bët ci moom, ba ci ñi ko jam sax. Te xeet yi nekk ci kaw suuf yépp dinañu jooy ndax moom. Waaw. Amiin.
Explore Peeñu ma 1:7