1
Màrk 11:24
Téereb Injiil
TI
Moo tax maa ngi leen koy wax, bu ngeen di ñaan Yàlla, lépp lu ngeen ko mana laaj, gëmleen ne jot ngeen ko, te dingeen ko am.
Compare
Explore Màrk 11:24
2
Màrk 11:23
Ci dëgg maa ngi leen koy wax, ku ne tund wale: “Jógal, tàbbi ca géej ga,” te nga gëm ne loolu dina am, bañ cee boole xel ñaar, kon sa ñaan nangu.
Explore Màrk 11:23
3
Màrk 11:25-26
Te it bu ngeen di ñaan, fekk ngeen jàppal kenn dara, baal-leen ko, ngir seen Baay bi ci kaw baal leen seeni tooñ, yéen itam.»
Explore Màrk 11:25-26
4
Màrk 11:22
Yeesu ne: «Gëmleen Yàlla.
Explore Màrk 11:22
5
Màrk 11:17
Mu di leen jàngal ne leen: «Ndax waxuñu ci Mbind mi: “Dees na wooye sama kër këru ñaan ci Yàlla ngir xeet yépp.” Waaye yéen def ngeen ko këru sàcc.»
Explore Màrk 11:17
6
Màrk 11:9
Ñiy jiitu ak ñiy topp ci Yeesu ñépp di wax ci kaw naan: «Osaana! Yaw miy ñëw ci turu Boroom bi, ku barkeel nga!
Explore Màrk 11:9
7
Màrk 11:10
Nguuru sunu maam Daawuda giy ñëw dina barkeel! Ci bérab yu gëna kawe, nañu ne: “Osaana!”»
Explore Màrk 11:10