1
Macë 9:37-38
Téereb Injiil
TI
Noonu mu ne taalibeem ya: «Ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu. Ñaanleen nag Boroom ngóob mi, mu yebal ay liggéeykat, ñu góob toolam.»
Compare
Explore Macë 9:37-38
2
Macë 9:13
Mbind mi nee na: “Yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” Demleen nag te seet lu wax joojuy tekki. Ndaxte ñëwuma, ngir woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»
Explore Macë 9:13
3
Macë 9:36
Bi Yeesu gisee mbooloo ma, mu yërëm leen, ndaxte dañoo sonn ba ne yogg, mel ni xar yu amul sàmm.
Explore Macë 9:36
4
Macë 9:12
Waaye bi ko Yeesu déggee, mu ne: «Ñi wér soxlawuñu fajkat, ñi wéradi ñoo ko soxla.
Explore Macë 9:12
5
Macë 9:35
Noonu Yeesu wër dëkk yu mag ya yépp ak yu ndaw ya, di leen jàngal ci seeni jàngu, tey yégle xibaaru jàmm bi jëm ci nguuru Yàlla, di faj jàngoro yépp ak wéradi yépp.
Explore Macë 9:35