1
Macë 18:20
Téereb Injiil
TI
Ndaxte fu ñaar walla ñetti nit booloo ci sama tur, maa ngi ci seen biir.»
Compare
Explore Macë 18:20
2
Macë 18:19
«Maa ngi leen koy wax it, bu ñaar ci yéen déggoo ci àddina, ngir ñaan lu mu mana doon, sama Baay bi nekk ci kaw dina leen ko may.
Explore Macë 18:19
3
Macë 18:2-3
Noonu Yeesu woo xale, teg ko ci seen biir, ne leen: «Ci dëgg maa ngi leen koy wax, su ngeen waññikuwul ci Yàlla, ba mel niy xale, dungeen dugg mukk ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.
Explore Macë 18:2-3
4
Macë 18:4
Kuy suufeelu nag, ba mel ni xale bii, kooku mooy ki gëna màgg ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.
Explore Macë 18:4
5
Macë 18:5
Te it ku nangu ci sama tur xale bu mel ni kii, man mii nga nangu.
Explore Macë 18:5
6
Macë 18:18
Ci dëgg maa ngi leen koy wax, lépp lu ngeen yeew ci àddina, dees na ko yeew ci asamaan, te lépp lu ngeen yiwi ci àddina, dees na ko yiwi ci asamaan.
Explore Macë 18:18
7
Macë 18:35
«Noonu la leen sama Baay bi ci kaw di def, bu ngeen baalul ku nekk seen mbokk ak xol bu sedd.»
Explore Macë 18:35
8
Macë 18:6
Waaye ku yóbbe bàkkaar kenn ci ñi gëna tuuti ñi ma gëm, li gën ci moom mooy ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ca fa gëna xóot ca géej ga.
Explore Macë 18:6
9
Macë 18:12
«Luy seen xalaat ci lii? Su fi amoon nit ku am téeméeri xar, te benn ci ñoom réer, lu muy def? Ndax du bàyyi ca parlukaay ba juróom ñeent fukki xar ya ak juróom ñeent, te dem wuti ma réer?
Explore Macë 18:12