1
Yowaan 20:21-22
Téereb Injiil
TI
Yeesu dellu ne leen: «Na jàmm wàcc ci yéen! Ni ma Baay bi yónnee, noonu laa leen di yónnee, man itam.» Bi mu waxee loolu, mu ëf leen ne leen: «Sol naa leen Xelu Yàlla mu Sell mi.
Compare
Explore Yowaan 20:21-22
2
Yowaan 20:29
Yeesu ne ko: «Li nga ma gis a tax nga gëm? Ki bég mooy ki gëm te gisu ma!»
Explore Yowaan 20:29
3
Yowaan 20:27-28
Noonu mu ne Tomaa: «Indil sa baaraam fii te seet sama loxo; indil sa loxo, teg ko ci sama wet. Bàyyil di weddi te nga gëm.» Tomaa ne ko: «Sama Boroom, sama Yàlla!»
Explore Yowaan 20:27-28