1
Saag 5:16
Téereb Injiil
TI
Kon nag waxanteleen seeni bàkkaar tey ñaanalante, ngir ngeen wér. Ñaanu aji jub gu dëggu, dooleem amul kem.
Compare
Explore Saag 5:16
2
Saag 5:13
Su amee ci yéen ku nekk ci tiis, na ñaan ci Yàlla. Ku nekk ci mbég, na sant Yàlla ciy woy.
Explore Saag 5:13
3
Saag 5:15
Ñaan gu ànd ak ngëm dina musal ki wopp, ba Boroom bi yékkati ko. Su ko fekkoon ak i bàkkaar sax, Yàlla dina ko baal.
Explore Saag 5:15
4
Saag 5:14
Su amee ci yéen ku wopp, na woo njiiti mbooloo mi, ñu ñaanal ko te diw boppam ci turu Boroom bi.
Explore Saag 5:14
5
Saag 5:20
na xam lii: ku gindi bàkkaarkat ci réeram, musal nga nit ci dee te faral ko bàkkaar yu bare.
Explore Saag 5:20