1
Jëf ya 6:3-4
Téereb Injiil
TI
Kon nag bokk yi, tànnleen juróom ñaari nit ci seen biir, ñu am seede su rafet te fees ak Xel mu Sell mi ak sago, nu dénk leen liggéey bii. Waaye nun dinanu wéy ci ñaan ci Yàlla ak ci yenub xamle kàddu gi.»
Compare
Explore Jëf ya 6:3-4
2
Jëf ya 6:7
Noonu kàddug Yàlla di law, ba mbooloom taalibe yi di yokku bu bare ci Yerusalem; te sarxalkat yu bare déggal Yàlla ci topp yoonu ngëm wi.
Explore Jëf ya 6:7