1
Jëf ya 3:19
Téereb Injiil
TI
Tuubleen seeni bàkkaar nag te waññiku ci Yàlla, ngir seeni bàkkaar far.
Compare
Explore Jëf ya 3:19
2
Jëf ya 3:6
Noonu Piyeer ne ko: «Awma xaalis, awma wurus, waaye li ma am, dinaa la ko jox: ci turu Yeesu Kirist mu Nasaret doxal!»
Explore Jëf ya 3:6
3
Jëf ya 3:7-8
Mu jàpp ci loxol ndijooram, yékkati ko. Ci saa si ay tànkam ak ay kostanam dëgër. Mu tëb, daldi taxaw, di dox. Mu dugg ak ñoom ca kër Yàlla ga, muy dox, di tëb tey sant Yàlla.
Explore Jëf ya 3:7-8
4
Jëf ya 3:16
Ci gëm turam la nit, kii ngeen di gis te xam ko, dëgëre; waaw, turu Yeesu ak ngëm gi jóge ci moom, moo tax mu wér péŋŋ ci seen kanam, yéen ñépp.
Explore Jëf ya 3:16