1
Jëf ya 27:25
Téereb Injiil
TI
Moo tax, gaa ñi, takkleen seen fit, ndax wóolu naa Yàlla ne li mu ma wax dina am.
Compare
Explore Jëf ya 27:25
2
Jëf ya 27:23-24
Ndaxte ci guddi menn malaaka dikkal na ma, jóge ci Yàlla sama Boroom, bi may jaamu. Mu ne ma: “Pool bul tiit; fàww nga taxaw ci kanam Sesaar, te yaa tax Yàllay aar bakkani ñi nga àndal ñépp.”
Explore Jëf ya 27:23-24
3
Jëf ya 27:22
Léegi nag maa ngi leen di dénk, ngeen takk seen fit, ndax gaal gi rekk mooy yàqu, waaye kenn ci yéen du dee.
Explore Jëf ya 27:22