1
2.Tesalonig 3:3
Téereb Injiil
TI
Waaye Boroom bi kuy sàmm kóllëre la; dina leen dëgëral te musal leen ci Ibliis.
Compare
Explore 2.Tesalonig 3:3
2
2.Tesalonig 3:5
Na Boroom bi gindi seeni xol ci mbëggeelu Yàlla ak muñu Kirist.
Explore 2.Tesalonig 3:5
3
2.Tesalonig 3:6
Nu ngi leen di sant it bokk yi, ci turu sunu Boroom Yeesu Kirist, ngeen dëddu bépp mbokk buy wéy ci tayel te baña topp dénkaane, yi nu leen jottali.
Explore 2.Tesalonig 3:6
4
2.Tesalonig 3:2
Ngeen ñaanal nu it, ngir nu mucc ci ñi bon te soxor, ndaxte du ñépp a gëm.
Explore 2.Tesalonig 3:2