1
2.Korent 8:9
Téereb Injiil
TI
Ndaxte yiwu sunu Boroom Yeesu Kirist umpu leen, ni mu futtee am-amam, ba ñàkk ngir yéen, ndax ngeen woomle cig ñàkkam.
Compare
Explore 2.Korent 8:9
2
2.Korent 8:2
Nattu yi ñu jaar ëmb nañu coono yu réy; waaye seen mbég mu tar ak seen ñàkk gu metti ñoo jur ci ñoom yéwén gu jéggi dayo.
Explore 2.Korent 8:2