1
1.Korent 4:20
Téereb Injiil
TI
Ndaxte nguuru Yàlla du waxi kese, waaye doole la.
Compare
Explore 1.Korent 4:20
2
1.Korent 4:5
Looloo tax buleen daan kenn ci àtte, bala jamono ji di jot te Boroom bi ñëw. Mooy leeral yi nëbbu ci lëndëm, di làññi mébétu xol yi. Bu ko defee ku nekk dina jot ci Yàlla ngërëm li mu yelloo.
Explore 1.Korent 4:5
3
1.Korent 4:2
Li war ci jawriñ mooy mu takku ci liggéeyam.
Explore 1.Korent 4:2
4
1.Korent 4:1
Nañu nu teg kon ay surgay Kirist, di ay jawriñ yuy xamle mbóoti Yàlla.
Explore 1.Korent 4:1