1
Màndiŋ ma 12:8
Kàddug Yàlla
KY
Gémmiñ ak gémmiñ laay waxeek moom wax ju leer nàññ ju ñu léebul, te jëmmu Aji Sax ji lay gis. Kon lu leen may fitu ŋàññ Musaa sama jaam bi?»
Compare
Explore Màndiŋ ma 12:8
2
Màndiŋ ma 12:3
Góor ga Musaa nag defoon ku woyof lool, ba raw mboolem doom aadama ci kaw suuf.
Explore Màndiŋ ma 12:3
3
Màndiŋ ma 12:6
Mu ne leen: «Dégluleen bu baax samay kàddu: Su ngeen feeñlee ab yonentu Aji Sax ji, ci am peeñu laa koy xamale maay kan, te ci gént laay waxeek moom
Explore Màndiŋ ma 12:6
4
Màndiŋ ma 12:7
waaye du Musaa sama jaam bii. Moom mooy ki wóor ci mboolem sama kër gii.
Explore Màndiŋ ma 12:7