1
Màrk 15:34
Kàddug Yàlla
KY
Ba fukki waxtu ak juróom ca ngoon jotee, Yeesu àddu ca kaw, ne: «Elowi, Elowi, lema sabaktani?» muy firi: «Sama Yàlla, sama Yàlla, lu tax nga wacc ma?»
Compare
Explore Màrk 15:34
2
Màrk 15:39
Njiitu takk-der ba taxawoon ca kanam Yeesu nag gis, na Yeesu doge. Mu ne: «Aylayéwén, waa jii mooy Doomu Yàlla!»
Explore Màrk 15:39
3
Màrk 15:38
Ba mu ko defee ridob biir néegu Yàlla ba xar ñaar, dale ca kaw ba ca suuf.
Explore Màrk 15:38
4
Màrk 15:37
Yeesu nag yuuxu, daldi dog.
Explore Màrk 15:37
5
Màrk 15:33
Ba fukki waxtu ak ñaar ca bëccëg jotee, ag lëndëm a wàcc ca réew ma mépp, ba fukki waxtu ak juróom ca ngoon.
Explore Màrk 15:33
6
Màrk 15:15
Pilaat nag bëgg lu neex mbooloo ma, ba tax mu bàyyi Barabas. Mu cawlu Yeesu ay kàcciri, ba noppi teg ko ciy loxo, ngir ñu daaj ko ci bant.
Explore Màrk 15:15