1
Sarxalkat yi 20:13
Kàddug Yàlla
KY
«Su góor tëddee góor ni ñuy tëddee jigéen, ñaawtéef lañu def ñoom ñaar. Dee rekk mooy seen àtte, te ñooy gàddu seen bakkanu bopp.
Compare
Explore Sarxalkat yi 20:13
2
Sarxalkat yi 20:7
Doxleen ci lu sell te sell, ngir man Aji Sax ji maay seen Yàlla.
Explore Sarxalkat yi 20:7
3
Sarxalkat yi 20:26
«Nangeen nekk ñu sell ci man, ndaxte Ku sell laa, man Aji Sax ji, te dama leena ràññaatleek yeneen xeet yi, ngeen di sama ñoñ.
Explore Sarxalkat yi 20:26
4
Sarxalkat yi 20:8
Nangeen sàmm samay dogali yoon te di ko jëfe. Man Aji Sax ji maay ki leen sellal.
Explore Sarxalkat yi 20:8