1
Sarxalkat yi 18:22
Kàddug Yàlla
KY
«Bu góor tëdde góor, ni bu doon jigéen. Lu ñaawa ñaaw la.
Compare
Explore Sarxalkat yi 18:22
2
Sarxalkat yi 18:23
«Bu góor tëdde menn mala, di sobeel boppam, te bu jigéen jox boppam mala, di ànd ak moom. Loolu yàqute la.
Explore Sarxalkat yi 18:23
3
Sarxalkat yi 18:21
«Bul jébbal kenn ci say doom tuur mi ñuy wax Moleg, ndax waruloo teddadil sa turu Yàlla. Man maay Aji Sax ji.
Explore Sarxalkat yi 18:21