1
Yanqóoba 5:16
Kàddug Yàlla
KY
Kon nag tuddanteleen seeni bàkkaar tey ñaanalante, ndax ngeen wér. Aji jub ji, ag ñaanam, day dal ak doole.
Compare
Explore Yanqóoba 5:16
2
Yanqóoba 5:13
Ana ci yeen ku nekk ciw tiis? Na ñaan. Ana ku ci am mbég? Na sàbbaal.
Explore Yanqóoba 5:13
3
Yanqóoba 5:15
Ñaan gu ànd ak ngëm day musal ki wopp, ba Boroom bi yékkati ko. Su dee daa bàkkaar, dees na ko jéggal.
Explore Yanqóoba 5:15
4
Yanqóoba 5:14
Ana ku wopp ci yeen? Na woo magi mbooloom gëmkat ñi, ñu ñaanal ko, raayaale ko ag diw ci turu Boroom bi.
Explore Yanqóoba 5:14
5
Yanqóoba 5:20
xamleen ne ku waññ bàkkaarkat ci yoonu sànkuteem, musal na ko bakkanam, te faral na ko bàkkaar yu bare.
Explore Yanqóoba 5:20