1
Njàlbéen ga 40:8
Kàddug Yàlla
KY
Ñu ne ko: «Ay gént daal a nu dikkal, te amunu ku nu koy firil.» Yuusufa ne leen: «Xanaa du Yàllaa moom piri? Nettalileen ma seeni gént rekk kay.»
Compare
Explore Njàlbéen ga 40:8
2
Njàlbéen ga 40:23
Waaye kilifa, ga yore naani Firawna, xalaatul sax Yuusufa, da koo fàtte.
Explore Njàlbéen ga 40:23