1
Njàlbéen ga 38:10
Kàddug Yàlla
KY
Aji Sax ji ñaawlu li muy def, ba tax mu faat ko, moom itam.
Compare
Explore Njàlbéen ga 38:10
2
Njàlbéen ga 38:9
Teewul Onan xam ne du doon askan wu muy moom, ba tax saa yuy séy ak jabaru magam, bay wara àgg rekk, tuur maniyu wi ci suuf, ngir baña giiral magam.
Explore Njàlbéen ga 38:9