1
Galasi 3:13
Kàddug Yàlla
KY
Almasi bi moom, moo nu jot ci alkàndey yoon wi, ba mu doonee ku alku ngir nun, nde: «Alkute ñeel na képp ku ñu rey, wékk ko ci bant.»
Compare
Explore Galasi 3:13
2
Galasi 3:28
Kon nag amul Yawut ak ku dul Yawut, amul ab jaam ak as gor, amul góor ak jigéen. Yeen ñépp benn ngeen ci Almasi Yeesu.
Explore Galasi 3:28
3
Galasi 3:29
Te su ngeen bokkee ci Almasi bi, yeen ay askanu Ibraayma, te yeena jagoo dige ba.
Explore Galasi 3:29
4
Galasi 3:14
Noonu la deme ngir barkeb Ibraayma wàcc ci xeet yi dul Yawut ndax Almasi Yeesu, ngir itam nu jot ci digeb Noo gu Sell gi, ci kaw ngëm.
Explore Galasi 3:14
5
Galasi 3:11
Li sàmm yoon taxul kenn jot àtteb ku jub fi kanam Yàlla sax, lu leer nàññ la, nde: «Ki ñu baaxe njub ndax ngëmam mooy dund.»
Explore Galasi 3:11