1
Galasi 1:10
Kàddug Yàlla
KY
Léegi nag ndax nit ñi laay sàkkoo jubool, am Yàlla? Am nit ñi laay wuta neex? Su ma bëggoona wéye neex nit ñi de, duma doon jaamub Almasi bi.
Compare
Explore Galasi 1:10
2
Galasi 1:8
Waaye nun ci sunu bopp, mbaa malaaka mu bawoo ci asamaan sax, ku leen ci àgge woon beneen xibaaru jàmm bu dul bi nu leen àgge, kooku yal na alku!
Explore Galasi 1:8
3
Galasi 1:3-4
Aw yiw ak jàmm ñeel na leen, tukkee ci Yàlla sunu Baay ak Sang bi Yeesu Almasi bi maye bakkanam ngir njotug sunuy bàkkaar, ba musal nu ci jamonoy tey ju bon ji, ci coobarey Yàlla sunu Baay
Explore Galasi 1:3-4