1
Mucc ga 36:1
Kàddug Yàlla
KY
«Kon nag Beccalel ak Oliyab ak mboolem ñu xareñ ñi Aji Sax ji may xareñte ak déggin ngir ñu mana jëfe mboolem sas yi jëm ci liggéeyu néeg bu sell bi, ñoom ñépp nañu sottal lépp li Aji Sax ji santaane.»
Compare
Explore Mucc ga 36:1
2
Mucc ga 36:3
Ba mu ko defee ñu nangoo ci Musaa mboolem saraxu njébbal bu bànni Israayil indi, ngir sottal liggéeyu néeg bu sell bi. Bànni Israayil nag jàppoo suba gu jot di indil Musaa ay saraxi yéene
Explore Mucc ga 36:3