1
Mucc ga 35:30-31
Kàddug Yàlla
KY
Musaa nag ne bànni Israayil: «Gisleen, Aji Sax ji moo woo Beccalel ci turam. Beccalel, Uri mooy baayam; Uri, Ur Yudeen bi di baayam. Moo ko feesale xelum Yàlla ak xareñte ak déggin ak xam-xam ak manoorey bépp xeetu liggéey
Compare
Explore Mucc ga 35:30-31
2
Mucc ga 35:35
te moo leen feesal xareñte, ngir bépp liggéey, ci wàllu yatt ak nataal, ak liggéeyu wëñ gu baxa te laal yolet, ak wëñ gu xewar, ak gu xonq curr ak wëñu lẽe. Mane nañoo ràbb te itam dañuy sos seen taarali bopp.
Explore Mucc ga 35:35